Gayn nagn deilou nexal Elon Musk saay fi nexoul bougn naxanteiπππ
Gayi on est plus sur twitter ici y'a pas de "tweet" faut trouver un nom
Kougni ndieukk sauce fii πππ
Mais noy crΓ©er genre rΓ©seau bi fatei def ci DM ? Kiko crΓ©er xamoul gaat
Enfin je pourrais dire des dingueries ici sans se manger une sauceππππππptdrrrr dina misogyne ba yakhou ππππΉ
Rt remplacer par Mt
Kebetu remplacer pas saneku